-----------------
العربیة
English
Français
Español
SHQIP
اردو
Melayu
Türkçe
Tamil
Bulgarian
Thai
中文
Русский
বাংলা
Тоҷикистон
kiswahili
Kyrgyz
فارسی
Hausa
German
پښتو
हिन्दी
Azəri
Italiano
ျမန္မာ
Ўзбекча
Türkmençe
Bosanski
Pulaar
Filipino
Română
қазақша
Wolof
Bamana kan
Kinyarwanda
Português
کوردی
日本語
پنجابی
Ελληνική
xet wu jekwi
|
jokko ak ñun
|
li aju ci ñun
18:19 GMT
limu xabaar yi: 6
gёstu:
listu xabaar ak xew xew yi mujju téñu gëstuko
xabaar yi gëna fёs
yegu yegu xuraan
politique - dundin
xam xam – aada
bitim réew
nataal
dañ kuppa xabaar yi
ligéey yi ak yenggu yenggu yi
laaye biir yi
yoonnée xabaar yi
yaxu al xur´aan bu matt sёkk
lefol qur’aana
xabaar yi gena fёs
Jotaayu xatmu kaamilu al xuraan bi ci kaamilu al xuraan bu gëna rëyy ci aduna bi lañuko amalee
Dinañu defar ab documentaire ci waallu daara yu kawe yi nga xamni moo neekk ci reewum Russie
Ñett jullit bokknañu ci nguuru reewum France bu bees bi
Yeewute bi nga xamni jullit ñi yeewunañuko wuyu woote la boo xamni fanweeri att ci ginaaw lako Imaam Xomeyni wootewoon
Askanu aduna bi yëpp ñaawluna aax doomu aadama yi nga xamni ñungikoy nasaxal ca reewum Baxrayni
Nonggo daara reewum Burkinafaso yi ñaxtunañu tere gi nga xamni terenañuko muuru ci bërëbu jaangukaay yi
Dinañu amal ab jotaayu ca Bruxelle diggënte kureel bi nga xamni dafay yenggu ci ci bokk ligeey ci islaam ak mbootaayu reewu tugël yi
Dina amal jotaay bu mujju ci jotaay yi nga xamni moom lañii amal ngir jaangat ak saytu firi ak tekki yi nga xamni defnañuko ci al xuraan
Njiitu mbooloo mi yor waallu doxalin ci parti biidi xizbullah waxna ni saam beennoo ak deggoo ci bët saalumu reewum Liban lu war la
Dalu islaam yi ak kër yi nga xamni dañii yenggu ci diine islaam yookkuna bu baax ci reewum Bresil
Mosku mooy dalal ndaje aduna wërngëlkëp biñu jagleel jigeenu jullit yi
doxal xalaatu xamale diine islaam ñi nga xamni duñu ayy jullit ci gox biidi (away) ci reewum Amerique
Taannañu Karbala mu neekk peyu reewum tourisme islaam ci attum 2015
Ayy coppite yu am solo dina am leegi ci reewum Arabi Soudite
Waxaabi yi ñungi tëkku ci amal ab coong ci bërëb bi nga xamni moom lañu deeñ kiidi Roxaya ci reewum Siri
Dinañu amal jonŋante al xuraan ci waallu keemtaanu al xuraan ak sunna yonent bi ci daara ju kawe jiidi Al azxar
Maggalnañu ca reewum Bresil bës bi nga xamni ci lañu goreel bët ganaaru reewum Liban ci loxo yaxuudu Israel
Jonŋante al xuraan aduna wërngëlkëp biñu jagleel nonggo daara jullit yu neekk ci daara yu kawe yi ci 12 septembre lañukoy door
Kureel biidi (ISESCO) xamlena ni daaxnañu xalaatu def gox biidi Najaf peyu reewum caaday islaam
ubbinañu ci reewum Nigeria njëlbeenu radio islaam
Falu njëlbeenu jaraafu jullit ci gox biidi (Lester) ci reewum angleterre
Doornañu ñaareelu ayu bësu caaday islaam ca reewum Itali
Jaangatnañu jafejafe nonggo daara reewum Tayland yi ca daara ju kawe jiidi Al Azxar
Dinañu amal ayy daara tafsir al xuraan ca reewum Nigeria
Doornañu bind turu ñi nga xamni dañii aji ca Laaxur
Dinañu amal ab yoonu doxlinu banque islaam ca reewum Libi
Dinañu amal ab lëll ci reewum Turki lëllu aduna wërngëlkëp ngir jaangat jafejafe jumaa yi ak jakka yi ci biir reew mi
Jawriñ giñu deenŋ waallu caada ak aada ci reewum Tunisie ñaawluna bu baax coong yi nga xamni waxabiya yi ñungikoy def ci bërëbu ziyarekaay yi
Mabbalnañu jumaa ji ñu duppee (Abu taalib)ca reewum Baxrayni
Dinañu amal ci reewum Malezi marsé aduna wërngëlkëp ci waallu tourisme
Tey jii lañii amal ab lëll ci waallu apartheid ci xabaar ak tasxabaar ci reewu tugël yi
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
>
>>>
xabaar yi am solo
Jotaayu xatmu kaamilu al xuraan bi ci kaamilu al xuraan bu gëna rëyy ci aduna bi lañuko amalee
Dinañu defar ab documentaire ci waallu daara yu kawe yi nga xamni moo neekk ci reewum Russie
Njiitu mbooloo mi yor waallu doxalin ci parti biidi xizbullah waxna ni saam beennoo ak deggoo ci bët saalumu reewum Liban lu war la
Yeewute bi nga xamni jullit ñi yeewunañuko wuyu woote la boo xamni fanweeri att ci ginaaw lako Imaam Xomeyni wootewoon
Dalu islaam yi ak kër yi nga xamni dañii yenggu ci diine islaam yookkuna bu baax ci reewum Bresil
Nonggo daara reewum Burkinafaso yi ñaxtunañu tere gi nga xamni terenañuko muuru ci bërëbu jaangukaay yi
Dinañu amal ab jotaayu ca Bruxelle diggënte kureel bi nga xamni dafay yenggu ci ci bokk ligeey ci islaam ak mbootaayu reewu tugël yi
E-Mail:
intl@ikna.ir
2003 - 2012 këru tasukaayu xabaaru al xur'aan ci bitim réew.